Proverbes wolof

Proverbes wolof

Proverbes, sentences et maximes wolof.

Bala nga xam luw taat di jariñ, mbate toog jote.

On ne connait l'utilité des fesses qu'au moment de s'asseoir.

Xeeb sa takkum, mu takk saw say.

Méprise ta ficelle, elle n'en attache pas moins ton fagot.

Tilim dina dem fu saabu mënula dem.

La saleté va parfois où le savon ne peut pas aller.

Yééné néég la, boroom a cay fanaan.

Le souhait est une chambre, c'est celui qui le formule qui y passe la nuit.

Jikko dana soppiku jaan walbatiku màtt boroom ba.

Le caractère, ça peut se changer en serpent, se retourner et mordre son maître.

Dëgg kaani la, ku ñu ko xëpp nga toxoñu.

La vérité c'est du piment, si on te la jette à la face, tu te frottes les yeux.

Mag du yalla wayé yagna ak yalla

Une personne âgée n'est pas Dieu mais a vécu longtemps avec Dieu

Bakkan waruw dàll la : fa muy dagge dooko yëg.

La vie c'est comme une lanière de sandale : avant qu'elle ne soit rompue, on ne peut pas savoir où cela va se produire